Letra de Habib Faye
Letra powered by LyricFind
Adduna bi du dara ; te dara xaj u fi
Bi Lahii ku ko japp ; xamal ni japp u loo ci ; dara
Adduna bi du dara ; te dara xaj u fi
Bi Lahii ku ko japp ; xamal ni japp u loo ci ; dara
Adduna bi du dara ; te dara xaj u fi
Bi Lahii ku ko japp ; xamal ni japp u loo ci ; dara
Man Youssou ñakk naa ; andandoo bu sincère
Adduna ; adduna daal ; nax ati na ñu
Adduna ; adduna da fay wor ee
Habib Faye ; dem na nii
Waa ju baax ; guddée na waay
Habib yaru woon na ; and ak dignité
Fonŋk oon na liggéey ёm ; bëgg njaboot am bu ; baax
Doon oon jàmbaar
Man Youssou ñakk naa ; andandoo bu sincère
Adduna ; adduna daal ; nax ati na ñu
Adduna ; adduna da fay wor ee
Habib Faye ; dem na nii
Waa ju baax ; guddée ne waay
Adduna ; adduna …… Adduna ; adduna